Contre la mort brutale et le « ndjibar » : Réciter 21 « basmala » avant d’aller au lit.
Longévité : Réciter 100 « basmala » après chacune des cinq prières.
Anti missile : Réciter 71 « basmala » (soit « l’adad » de Alif Lam Mim), après chaque prière d’Al Asr (takkoussan). Celui qui le fait aura toujours le dessus sur ses ennemis et où tu seras, ils ne seront jamais content : « muut mbaa mott wala méss rékk »
Contre l’adultère :
Pour les hommes : En portant votre pantalon, réciter 1 « basmala » en mettant votre pied droit, un autre « basmala » en mettant le pied gauche et « A ouzou bilaahi mina chaytaani radjim ». Jamais vous ne l’enlèverez pour faire l’adultère.
Pour les femmes : En nouant son pagne, elle peut réciter un « basmala » en posant l’un des bouts de celui-ci par la main droite et un autre « basmala » en posant l’autre bout du pagne et « A ouzou bilaahi mina chaytaani radjim » en poussant le bout à l’intérieur par le doigt (le pousse).
Protection : Après chacun des cinq prières, dire : « bii man, bii sama doom, bii sama alal, sammé naako bismi llahir rahmaanir rahim ». Souffler sur la main droite et faire passer sur le visage.
Contre le viol : Réciter 3 fois après la prière du matin: « Bismilaahi teu, rahmani teu, rahimi teu, teu goor, teu jigueen, teu lépp lou jugué ci ndigal goor dém ci ndigal jigueen ». Souffler sur la main droite et faire passer sur le visage. Personne ne pourra te violer.
Contre certains déboires ou accidents comme : déboitement, fractures, etc. Réciter 33 « basmala » après chacune des cinq prières.
Les secrets de « Basmala » : Contre l’envoûtement, le démon, l’adultère, le viol; pour la grande ouverture
« Pour demeurer à son poste malgré les envies, pour protéger une grossesse et faciliter l’accouchement ! »
Contre l’effet des djinns ou démons : réciter un « basmala » avant d’entrer chez soi ou dans un lieu donné.
Pour la grande ouverture : Réciter quotidiennement 777 « basmala ». Vous n’aurez plus besoin de voyager pour réussir.
Pour avoir une renommée et une richesse inespérées : Réciter quotidiennement le dimanche à la levée du soleil, 313 « basmala » plus un salaatou alaa Nabi.
Pour l’exhaussement d’un vœu : Réciter en une seule séance 12000 « basmala ». Après chaque 1000 « basmala » faire 2 « rakas ». A la fin, formuler votre vœu et clôturer par 100 « salaatu alaa Nabi ».
*BO BEUGUEE AM XAM-XAM
Rèciter BISMILAHI-RAHMANI-RAHIIMI 787 fois mais le 787ème dangkoy djèèkhalè ak FATIHA(manam bò wakhè bismilahi rahmani-rahimi bamiy 786 si 787ème bi dangay wakh bismilahi rahmani-rahimi yègalè sourate FATIHA bamou djèkh).
après soufler dans l’eau .apres nga dissi nàn wala sa dòm chaque matin avant de manger pendant 7 jours.
INCALAH lèp lò dègati diapko tè dòko fattè.
(BASMALA moy BISMILLAHI-R-RAHMANI-R-RAHIIMI)
..kouko binde 111 fois takko Yallah dana fathi sa haadio té sunu Borôme danala weuseuguelé ak taye tchii kanamou kilifayi ak bour yi ak tay moodi koula beug ba noppi ragal la tahit méèn mbinééf doula manal dara li féék yaa ngéék tééré bi.
*Après chaque prière du matin rèciter:
Bissmillàhi rahmàni-rrahìmi Làkhawla wa-là khouwata illà billàhi hanleyil-hanzim 10 fois
Kouko wakh DIEU VOUS PARDONNE TOUS LES PECHES COMME LE JOUR DE TA NAISSANCE( di nga mèlni kouy dòga diodo sètt withi ci ay bakkàr (Yalla dinala tedieul 70 bounti balà et 70 malàka(anges)dinanoula djègaloul sounou borom ba djant bi doug ta di nga mèlni kou dieun sa Aldiana ta Yalla dinala mousseul ci saytàné etc….
*kou diouli souba ba nopi def 50 basmalah dinga mouthie thi bepe none ak ay agression, ak lèp louy lor etc …
*kouy touki dougue thi auto, wala avion wala loumou meuna done, bouy yèuk mou wakh bismil lahir rahmanir rahimi, bou toguè wakh alhamdou lilahi rabbil enlamina, bepe diègo bou daamar binga dougue daw dagnou lakoy bindal ay tuyaba ba bangay wathie
.*kou ame dome yobouko thi daraadji serigne bi dieul aliwo bi teke ko thi podiou khalebi niko wakhal basmalah, bouko wakhè, kou tede ki nena thi Massalikoul djinan, gnome gnari wadiour yoyou ak serigne bi ak khalebi bougnou faato gnou tabal lene aldiana.
sou féèkè dangaa diangue « Bismilâhi ar Rahmâni ar Rahîm » 61 fois nguir fas yéènè saafara dara loolè dana saafarawou bi iznillâhi ta’allâ thia booba bis.
sou féèkéé binde nga « Bismilâhi ar Rahmâni ar Rahîm » 35 fois nga takko si sa bountu néèk chaytaané doufa doug mukk ak djinné té Yallah dana barkéél néék ba baril ay yiwam.
*Bò beuguè sa ndiabòt dòn bèn,beugueuntè wala yak sa dieukeur(rèciter le matin:
Bismilàhi-r-rakhmàni-r-rahìmi 111 fos nga eufko si ndokh diokhlèn gnou nàn.yaw soula nèkhé nga nàn si inchalah dioubò dina am ci sèn digueuntè
*Sounu Borome néena guign naa tchi samak tééd ak samak magg ak samak tabé ak samak baakh néena koo xamni diangue nga al basmalatu djiokthia(tèk sa) faatihatul kitaab bamou ag wéén yoon(1fois) rèèk danala diégal say bakkaar doonté dafa diotéwoone ba assamaan sa danàa nangou saw yiw té douma lak saw lamigne mukk tchi sawara té dinâala mussal thi mbougaluk bammèèl ak mbougaluk yawmal khiyaam té danàala diapandalal sak guisma nga andak gni nga xamné sounu borôme dafaléèna xéweulé thi yonéntayi ak waliyuyi.
BOY FATHIE KOU FEBAR WALA METTIT DANGAY DIANG Bismilàhi-r-rakhmàni-r-rahìmi 70 FOIS NGA EUFKO CI NOP BI(droit)
sou féèkè diangue ngako 50 fois thi kaname adji toogne…adji tongne dja danala toroxlul té sunu Borôme dana dàdi sanni tchi xolam ak tay(moy ak ragal) tédootu dièèm béèn safân tchi yaw.
bok na thi ndiarignam sou féèkè diang ngako waxtu wu djante bi di fingk 300 fois djiouli thi Yonentébi 100 fois sounu Borôme danala weursageul tchi fooko foogoutoon
*Les secrets de BASMALAH ( Bismil lahir rahmanir rahimi ) 19 araf la tolok 19 malaka yiye garder safara, gnouni koukoy yagua wakh danga mouthi thi malaka yoyou
sou féèkè adji tawat saxalal ngako 100 « Bismilâhi ar Rahmâni ar Rahîm » dikoko diangal bisbou néék bamouy gnetti fane dana wer insha Allahou.
Kouy teude diangue ko 21 fois sounu Borome danala mussal thia googa gouddi thi chaytaané ak sathi ak ragnaan kate,ak déé gou bétté ak béép balaa.
bok na thi ndiarignam sou féèkè diang ngako waxtu wu djante bi di fingk 300 fois djiouli thi Yonentébi 100 fois sounu Borôme danala weursageul tchi fooko foogoutoon
Bismilaahi rahmani rahimi
Bo beugè mouthie ak khèweul diangal BASMALA 313: ni lankoy diang 3+10+300
Lenn si njëriñu BASMALLAH tee moy : (BISMILLAHI RAHMAANIR RAHIIM)
-111 fois si sokhla mou tëwë fadjou
– 66 fois chak jr diko toufli si ndokh diko naan kenn doula wall feebar
-70 fois safara diko diw say doom dounou khoulo dounou tassaaro dara douleen jakhasé
– 313 fois si ndokhou taw pr kou gaawa mer moukoy naan
– 33 fois toufliko si ndokh pr kouy jaay begg mou jar
-1111 fois chak fajar bo begger doon nitou yala té koula guis jokhla thiër say bountou kheewal di oubéko
-777 fois si ndokh raayoko si feebar bou tëwë wér boudoul feebarou deh
-114 fois boy toukki begg yala mousal la si accident
-210 fois toufli sisay lokho boy wouti dara
-1447 fois bo neker si khat khat begg si gaawa guenn
-666 fois pr kou nekk prison nga begg mou gaawa genn
Yal nanou YALLAH yerem té nangoul ñu, Amiin !
NB : Notez que le succès à ces prières précitées nécessite une piété et un respect des prescriptions divines.
Yalla nanu sounu Borome boolé yeureum teh défal nu déég ak toop bibarakati Cheikhouna Bamba…
Lamp Babul mouridinah ma lumière moy yoon wi Dieureudieuf Khadimou Rassoul Diarama maam cheikh Ibra Faal